Baixar Mais Tocadas: Neneh Cherry clipes

Boul ma sene, boul ma guiss madi re nga fokni mane / Khamouma li neka thi sama souf ak thi guinaw / Beugouma kouma khol oaldine yaw li neka si yaw / Mo ne si man, li ne si mane moye dilene diapale