Letra Música Birima – Youssou N’dour
Maysa tende jodo yaa moom liile
Maysa tende jodo yaa moom liile
Maysa tende jodo yaa moom liile
Hi woy birima fumu yendu ma yendu fa yendo naanee
Woy birima fumu yendu ma yendu fa yendo naanee

Buri samba laobe yaa moom liile

Damel maisa penda joor
Jooro jooro jooro jooro ho ho ho hoy
Sama waaji ken dula jam naani
Woy birima fumu yendu ma yendu fa yendo naanee
Wooy tedi ngoné maarne be sambaa
Kuli baca senge ndat biran ngamoo
Ngoné maca nas mbay maca jeeri
Samba yaasimo dike mbay kuja dooooki
Yay borom mbaboor mi
Hi di woy birima sama waaji ken dula jam naanee
Woy birima fumu yendu ma yendu fa yendo naanee
Dogo fal ak mawa joor kumba samba yaay jaloor
Dogo dogo, ho ho ho!
Aziz o mbay dogo xam nga yoon wee
Woy birima fumu yendu ma yendu fa yendo naanee
Maisa tendo jooro jooro a mari ngone sobel kayor niila
Woy birima fumu yendu ma yendu fa yendo naanee
Fonte: Musixmatch
Youssou N’dour – Birima – Ouvir Música